Les sillons
11,00 €
10,45 €
Économisez 5%
Dawuuda Njaay aw ci yoon wi noom Séex Musaa Ka xàlloon.
Woy yii mu wéer ci léebu yi fi Maam bàyyi xoot nanu.
Di nan yar yeete suuxat xel naatal xalaat.
Teewul nose bi sol galan buy dàkk xolu bépp dom Aadama.
Te loolu la woykat tigi di sàkku. Daouda Ndiaye suit le chemin tracé par le précurseur Cheikh Moussa Kâ.
Ses poèmes s'appuient sur les proverbes légués par les ancêtres.
D'où leur richesse.